Alegsàndar

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Ci angale mooy Alexander; Ci faranse mooy Alexandre

Turu 4 nit ñi wuute ci Injiil:

  1. Doomu Simoŋ mi dëkk Siren, di magu Rufus (Mk 15:21).
  2. Menn mbokku saraxalekat bu mag ba, Anas, (Jëf 4:6).
  3. Benn Yawut bu jóge Efes (Jëf 19:33,34).
  4. Benn tëgg ci Efes. Bëre woon na ak waxi Pool (1Tim 1:20; 2Tim 4:14,15).