Aller au contenu

Albaatar

Jóge Wikipedia.

Ci angale mooy alabaster; Ci faranse mooy albâtre

Xeer wu weex ni kew la, te rafet. Daan nañu ci yett ay njaq.

Dañu ciy wax ci Injiil ci Mc 26:7; Mk 14:3; Lu 7:37.