Aller au contenu

Ajara

Jóge Wikipedia.

Ci làkku ibrë (הָגָר) la tur wi jóge. Ajara moo ni ñu waxe tur wi ci Lislaam. Ci angale mooy Hagar; Ci faranse mooy Agar

Jaamu Saarata la woon, ñu mayoon ko Yonent Yàlla Ibraayma ni jabar, mu am ci Ismayla. Misra la bawoo. Man nañu jàng jalooreem ci Ge 16:1-16; 21:9-21.

Ci Injiil dañuy wax ci Ajara ci Gal 4:24,25.