Aha akk yaeffii domu adama yii
Aha akk yaeffii domu adama yii, moye lu nit kii mom, lim yealo teh ken waruko jel sii mom.
Nit ku neaka amna lum mom akk lum yealo teh ken waruko jel cii mom, lolu nit ku neaka warr nako ham.
Lii yeap nyiko ligaye moye rew yii neh cii aduna yeap mbotaye bii len (nyilen) fa neakal purr nyu tahawalen fa cii Pari (Faraans), dipi juneh akk juromii temerri att akk nyene fuka akk jurom neate (1948).[1] Girr ndamii nit yii yep yii neh cii aduna, akk rew yii yep cii aduna.
Lan Moye Aaha Akk Yealeaffii Domu Adama Bii
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]LiNgaMom
[Soppi • soppi gongikuwaay bi](a) Sa Aha Purr Deka
(b) Purr Neaka Domu DekBii
(c) Atteh Bu Degu(Woor)
(d)Sa Aaha Purr Deaku whye
Karangeh
[Soppi • soppi gongikuwaay bi](a) Karangeh cii yaahuteh(cii sakula, weradii,
(b) Purr Utt Deaku Waye Su La Deaka Defea Lu Bon
(c) Atteh Bu Degu(Woor), Teh Nyu Nangula Sa Aaha Akk Sa Yealeff BanLa Japa Cii LU Worr Neh YowLa
Jama Purr Nyep
[Soppi • soppi gongikuwaay bi](a) WerrGuYaram
(b) Yealeaff Purr Janga
(c) Gom Akk Deff Lula Sa Dineh Meye
(D) Nyu Arr La
Sa Yealeaf Bii Nga Mom
[Soppi • soppi gongikuwaay bi](a) Cii Saye
(b) Cii Amm Family
(c) Sa Yealeaff Boodii Jigane Akk Gorr
(d) Sa Yealeaff Ken Waruttla Forseh Saye
(e) Sa YeaLeaff Purr Waxhk
Jama
[Soppi • soppi gongikuwaay bi](a) WahLinGna Buga
(b)Purr Sani Cart
(c) Purr Geana NyhTu
Torohal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Torohal Nit Purr Soonalko, NanguAaha Akk Yealeaffam
(a) Japa ku waxhnea ngurrgii defutt lu baxhk
(b) Nagu wulen ku neaka dii jamu lim gom
(c) nyaka nangu ku deka cii dekabii purr mu sanii cart