Aller au contenu

Afiya

Jóge Wikipedia.

Ci angale ak faranse mooy Apphia.

Jenn jigéen ji dëkk Kolos la woon. Bokkoon na ci këru Filemon. Man na nekk sax jabaram la woon.

Ci Injiil dañuy wax ci Afiya ci Fm 1:2.