Admin

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Ci làkku ibrë la tur wi jóge. Ci angale mooy Aram or Ram; Ci faranse mooy Admin

Doomu Esrom la woon, di maamaatu Daawuda (1Ch 2:10; Ru 4:19). Benn ci maamaati Yeesu ci Luug la woon (Lu 3:33). Mooy Aram itam ci maamaati Yeesu ci Macë (Mc 1:3,4).