Adiratig
Apparence
Ci angale mooy Adriatic; Ci faranse mooy Adriatique
Géej la, ci diggante dunu Kereet ak dunu Sisil (Sisile). Tey jii géej ga mingi tudd Géeju Iyoniyeen (Mer Ionienne). Bokkul ak li ñu wax Adiratig tey ji. Adiratig tey mooy géej ga nekk ci diggante Itaali ak Yugosalawi (Yougoslavie).
Ci Injiil dañuy wax ci Adiratig ci Jëf 27:27.