Aller au contenu

Adaramit

Jóge Wikipedia.

Adaramit (Ἀτραμύττιον) – Ci angale mooy Adramyttium; ci faranse mooy Adramyttion.

Benn dëkku ak teeru la woon, ci diiwaanu nguuru Room bu tuddoon Misi. Tey jii mooy dëkk bu tudd Edremit ca réewu Tirki. Waaye ci dëgg-dëgg, ci bérabu dëkk bi tudd tey jii Karatash la nekkoon. Ma nga fare woon dun bu tuddoon Lesbos. Ci jamano Injiil ji nekk na ci diggante dëkku Torowas ak dëkku Pergam.

Ci Injiil dañuy wax ci Adaramit ci Jëf 27:2.