Abla Pokou
Apparence
Dencukaay:Abla pokou.jpg | |
Dundu ak jaar-jaaram | |
---|---|
Bésu juddu |
Xamuñu bés bi Gana |
Bésu faatu | 1770 |
Réew | Kodiwaar |
Liggeey | Lingeer |
Abla Pokou (wala Aura Poku, wala Abraha Pokou) lingeeru Afrig la , juddoo ci fukk ak juróom-ñetti xarnub. Indi na askanu Baoulé ci réewum Gana ba ci Kodiwaar. Léeb bi dafa nettali, saraxu doomam bu góor ngir jàll ag dex .
Bat bi "Baoulé " li nu tudde leegi askan yi , mu ngi joge ci saraxu doomam.
Bicci toppu saraxe, né na "Ba-ouli", loolu dafay tekki "doom bi dee na".