Aal bu niokolo-koba

Jóge Wikipedia.

Parc national du Niokolo-Koba (PNNK) moggi neek ab aal bu yatu , digêunt em ak ndakaru toolu si 650 km . Aal bubu moggi neek si beut ganaru rew mi si deuk bu Taambacunda jeegé lol deuk bi niou naan Guinné Bissau. Foofu sa Niokolo-Koba def naniou fa ab yoon bu ropalan meun naffa wac.

Tarixu Parc bi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ci atum 1926 aal bi moggi neekon lu niou jagleel reub, ci atum 1951 mu daadi neek ab all bu niou 'classé' , ci atum 1954 niou daadi ko def parc national.[1] Ay yokuté am na si aal bi si diggenté 1962, 1968, 1969, waayé ba deuk bi moomé bopam ci atum 1960 da naka aal bi nekul woon yitéé si ndiit yi fi neekoo.

Ci atum 1981 ba leegi aal bi niogui taba si patrimoine mondial bu UNESCO. Ci atum 2007 UNESCO dafaa jeul ay matuway si parc ba def ci beureb-u patrimoine yi niou manancé. Lolu liko waralon moy reub kat yiiy doug si parc si ludul yoon.

ab yoon bu neek si digu aal bi
Aal bu Niokolo-koba

melokanu aal bi ( Géographie)[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Deex bu Gambi mo romb si digg parc bi si ab deuk bi xamne sorina lol ab Geec. Am na tamit béneen deex bu tudu Kulumtu ak d'ex bu aal Niokolo-Koba bi niou tudee Parc bi.

Aal bi moggi tolu si 130 km2, dadi neek danaka si diguente deuk biniou naan Kasamaàs, kolda ba si wetu deuk bi niou naan Guinée-Bissau jeege lol Tambacounda.