Ñamako


Ñamako xeet la ci xeeti garab yi nga xam ni seenug dund man naa yàgg lool. Ñu ngi koy fekk ci tundi Afrig.
Njariñ li[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Garab la gog ay doomam dees koy jëfandikoo, ngir xeeti saf-safal. Dees na ko jëfandikoo it ngir neexal sëy.
Jaarjaaram[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Ñamako bokkoon na ci njaay yi nga xam ni ñoo gënoon a dox ci yiñ daa dugal ca Afrig sowwu jant, ci jamonoy xarnub 18. Loolu sax moo tax ñu di ko woowe, "côte du Poivre" fële ca Gine.
Turu xam-xam wi[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Aframomum melegueta
Tur wi ci yeneeni làkk[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
farañse: maniguette |