Way

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet
Nuvola apps kscd.png

Misik ak Way Misik(fr musique en music) nak ci wolof misik rek lanu koy wax ndax daa bok ci baat yi nga xamni ñéppa ko bok mook lu melni widewo(video) WAY baatu way mingi jugé ci nit ku way maanaam nit ku yéwwu litax mu tudd moom nit kookii waykat dafa way bà man a sos ay wax mbaa ay nasar yoo xamni nit ñimu nékkal bàyyi wuñu ci xel mbaa sax xamu ñuko woon kon moo leen gën a way batax muy way kon kuñuy tuddee waykat dafa wara doon kuy yeeté

[Soppi] Way batay man na tékki poesie ci wolof

Ay Misikkat ci Senegaal

Ay nasarkat/Taalifkat ci Senegaal

Samay jumtukaay
Barabu tur

Wuute
Jëf
Joowiin
Boyotu jumtukaay yi
Yeneeni làkk