Aller au contenu

Sëriñ Basiiru Mbàkke

Jóge Wikipedia.
Dencukaay:S Basiiru.jpg
S Basiiru Mbàkke

Kenn ci doomi S Tuubaa yu am yi ag jeexiital te àgguñu ci di xalifa, ku amoon xam-xam, mooy ki bind téere bu am solo bii di ab delluwaay ci yoon wi, di "Minanul Baaqiil Qadiim"

ku ci bagga xootal na xool Sëriñ Basiiru Mbàkke ci situ wikimouridia.org