Sëriñ Aafiya Mbàkke

Jóge Wikipedia.

Seex Ahmadou Moukhtar ñiou gueen ko Xamé ci Sëñ Afia Mbàaké mogui Fégn Jaamano ci aatou 1871 faa Porokhane Wadiouram Bou Goor ŋi Toudou Maame Mor Anta Saalli Mbàaké ibn Maame Balla Mbàaké Wadiouram Bou Jigéen ŋi Maame Aïssatou Mbàaké ñou gueen ko xamé ci tuurou Maame Anta Njaay Mbàaké Bintou Maame Ibrahima Awa Niaŋŋ Ibn Maame Marame


Raak ñou Goor yi ak ñou Jigéen ñimou Bokaal Wadiour bou Jigéen:


Sëñ Mbacké Anta Maame Seex Anta Mbàaké Borom Darû Salam Soxna Faty Anta Mbàaké,mbii juur Sëñ Mor Faty Touré Soxna Anta Saali Mbàaké,mbii juur Soxna Faty Mbaàké Soukhraa

Dooumou Baayam yii:

Seex Ahmadou Bamba Mbàaké Xadimoul Rassul Maame Thierno Birahim Mbàaké Borom Darû Moukhti Sëriñe Massamba Mbàaké Sëriñe Seex Thioro Mbàaké Sëriñe Balla Thioro Mbàaké Seex ABsa Mbàaké Soxna Rokhaya Mbàaké,mbi juur Sëriñe Balla Bousso Soxna Astou Mbàaké ,mbi juur Sëriñe Masaayer Sylla Soxna Khari Mbàaké,mbi juur Sëriñe Modou Bousso Guede Soxna Coumba Taïba Mbàaké ,mbi juur Sëriñe Haidra Soxna Aminata Mbàaké,mbi juur Soxna Aminata Lô Soxna Fati Mbàaké,mbi juur Sëriñe Modou Xabane Mbàaké Dendey


Wadiouram Bou Goor Sëñ Maame Mor Anta salli mokeu jangal Alxuran ak taalif ñi Sëñ Touba njeuk déf Diot na Jaar ci Sëñ Mbacké Bousso ngir doléll Jaŋŋam Sëriñe Touba itamm Jangall nako itam yaarr nako itam

Sëriñe Ibrahima Mbàaké Ibn Sëñ Mor Dothie néna:


"Bii Sëñ Maame Mor Anta Salli Watié ligééy,Maagam jii Sëñ Touba mokeu taxawou laata mo déém Gabon.Sëén bii moko wakhone néé na jougé Mbàaké Cadior daldi déém Darû Salam,momit monéko na jangalé Alxuran. mokalal na ay kilifa ñou beuri ci Yoon wi alxuran meune naniou ci liim ñi Sëriñe Modou Mamoune Mbàaké ak Soxna Maïmounatoul koubra ,Sëriñe Mor fatim Touré. bii Sëñ bii jougéé Gabon ci aatoum 1912,Sëñ bé ko woloull ngir mou jéégé ko nax néna liggey go giss da wara am céddé."Mounéko def naleu sama céddé ci liggey bi méy défal sunu Borom" Sëriñe Khass mokeu nétali té Sëñ Afia mo koko wax ci bopam. mogii fék Sëñ bi tokk joublou Khibla daldi néko"nékal Imaam di jiité Diouromi Jouli ñi ,kaadou yoyou nioy ñi moujou jeumeulé ko ci féré yii.


Meussteu digat waxi Baayam Sëñ Maame Mor anta Salli ak Sëriñam Sëriñe Touba ba nimou fiy jougé wouñou jii Boromam ci aatou 1940. watioum Ligeeyam Kémaan deug laa nax da Jougé Ndiarém dem séti Maagam jii Mame Seex Anta.bimou eeksé fék Maame Seex ci tawat gou méti ci la daldi wo taawam bi Sëñ Modou Mamoune Mbàaké ak jarbatam Sëriñe Mor Fatim Touré daldi léne waxi Seex Anta da nék ci sukuraat,mou daldi lén waxat né Sëriñe Touba waxone naniko Faatom moy jiitou bou Maame Seex Anta téyitt Worr nakonii Waxi Sëñ Touba dou raff mouk. ci laa Egg ci Jouma Jii ngi joulii bamou tolé ci taaya ñgi moujou mou daldi watieu liggey,Sën Mor Touré mo daldi pouss Jeeum Jii yégali Jouli gii. mou daldi Xibar Faatou Sëñ Afia Imam. ci aay niit ñou woorr wax naniou né Sëñ bii waxone nako né mou daldi wax beug beugeum,Sëñ Afia daldi néko "moussal maa ci Safara ak saméy Taalibé".


NB:li nékoul ap Woné Sëñ Afia nax Sunu Borom def nako ba nopi,wayé Beug xamaléé Niitou Yalla bo xamné ñou beuri oumpalé nañiou ko.