Nosteg jant

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet


Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Nataal buy wone mbooleem cër yi ëpp solo ci sunu nosteeg jant, àdduna yi ci nekk

Nosteg jant bi, ci xam-xamu saytubiddiw, li fa ne mooy jant bi ak mbooleem nekktéef yu asamaan yiy warangiku ci li ko wër, moom jant bi: Juroom-ñetti àdduna yi ak seen 165 weer, kuusi àdduna (planète naine) yi.