Nosteg jant
Apparence
(Yoonalaat gu jóge Nosteeg jant)
Nosteg jant bi, ci xam-xamu saytubiddiw, mooy nosteg sunuy jawwu, li ko toggale di ab biddiw, jant bi ak mboolel yëfi asamaan yuy warangiku ci li ko wër ; juróom-ñatti jawwu yees firndeel ak seen 175 weer yu nu xam, juróomu jawwuy dàtt yi, ak miliyaari yaram yu ndaw yi (bokk ci yooyu jawwu yu ndaw yi ak pëndi diggante jawwu yi). Nosteg jant bi mingi bokk ci galaksi bi tudd Yoon wu Meewe
Jawwu yi nekk ci nosteg jant bi ñooy: Merkuur, Weenus, Suuf, Maas, Seres, Yupiter, Saturn, Uraanus, Neptuun, Eris, Pluton, Haomea, Makemake, Goŋgoŋ, Koawar ak Órkus.