Luga
Apparence
Luga (fr. Louga) benn dëkku Senegaal.
Luga benn la ci 14 diiwaanu yi nekk Senegaal. Mi ngi féete ca penkub bëj-gànnaaru réew mi. Péeyum diiwaan ba mooy taaxu Luga. Luga am na lu tollu ci 835 325 doomu-aadama ci atum 2013.