Dereet

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet
Dereeti nit ku dagg


Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Dereet ndox mu xonk la muy daw ci yaramu nit ak luy dund niki nit, di jaar ci diggante der wi ak yàpp wi, ngir man a wéy ci cér ci ko soxla, ngir dox niki: res, roñoo, Lu am solo la ngir ag dund man a am, ndax mooy séddale oksisen (li ngay noyyi) bi ci yaram wépp, lu man ta ñàkk la ci doxug oksisen bi Nit ku mukàllaf dina ci am lu toll ci juróomi liitar