Ben-yamin

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci làkku ibrë (בִּנְיָמִין) la tur wi jóge. Ci angale mooy Benjamin; Ci faranse mooy Benjamin

Caatu Yanqóoba la woon, moom mi sos giir ci bànni Israyil, mu jàpp ci Yude, ba réew ma xàjjalikoo. Sóol mi doon buur bu jëkk ci Israyil, ca la bokk.

Gis nañu tur wi ci Injiil ci Jëf 13:21; Ro 11:1; Fb 3:5; Pe 7:8.