Asot

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci làkku ibrë la tur wi jóge. Ci angale mooy Azotus; Ci faranse mooy Azot

Dëkk la woon, ci bëj-gànnaaru diiwaanu Yude, lu tollu 4 kilomet diggam ak Géej gu Mag ga. Nekk na bu yàgg bala jamano Injiil ji, lu tollu 1400 at. Ci jamano yooyu Asdodd la tuddoon.

Man nañu ko gis ci Injiil ci Jëf 8:40.