Jóge Wikipedia.
Ci angale mooy Areopagus; Ci faranse mooy Aréopage
Bérab ci biir dëkku Aten la, bu nekk ci kaw wenn tundu xeex wu kawe. Amoon na ay siis yi ñu defare woon doj ngir kureelu dëkk ba manoon faa daje. Indi nañu Pool foofu ngir mu waareji (Jëf 17:18-34).
Areyopas ni ñu ko gise tey ji su fekkee ne yaa ngi ca Akëropool
Tur wi moo feeñ ci Injiil ci Jëf 17:19,22,34.