Aller au contenu

Alfe

Jóge Wikipedia.

Ci làkku ibrë la tur wi jóge. Ci angale mooy Alphaeus; Ci faranse mooy Alphée

Turu 2 nit ñi wuute ci Injiil:

  1. Baayu Saag, mi bokkoon ca 12 taalibe Yeesu ya (Mc 10:3; Mk 3:18; Lu 6:15; Jëf 1:13).
  2. Baayu Lewi, juutikat bi bokkoon itam ci 12 taalibe Yeesu ya (Mk 2:14).