Akim

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci angale mooy Akim; Ci faranse mooy Achim

Benn ci maamaati Yeesu ci Macë la woon (Mc 1:14). Turam feeñul ci Kóllëre gu jëkk gi.