Werlaay
Apparence
(Yoonalaat gu jóge Werlaal)
Werlaay garab la gu man a gudd fan lool. Fi mu ëppe mooy ci réewi Afrik yu tàng yi fu ci mel ni Senegaal, Muritani, Sudaã, Somali Ba sax ci réewi araab yi ak réewum Endonesi. suuf su saf-sàpp te am ban ak poto-poto lay ñore
Melo wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Garab gu ndaw la. Taxawaay bi 2i met du ko weesu. Ay caram dañuy àgg it ba 2i met.
Ay njariñam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ay doomam dees koy watt di lekk. Xob yi ak reen yi dees koy jëfëndikoo ci wàllum pàj lu ci lu mel ni biir buy daw ak mbàq gu am góom ( estoma).
Loraange yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Gisuñu benn loraangeem.
Nataal yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]-
Tóortóoru Werlaay
-
Xob yi