Aller au contenu

Waxtaan:Bunt:Melosuuf

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wikipedia.
(Yoonalaat gu jóge Waxtaan:Sewogaraafi)

melo-suuf xam-xamu melo-suuf walla nataalu-suuf walla nataalu suuf si mooy geographie geo suuf graphie nalaal. Walla juxraaf mu juge ci araab mi gen a jege wolof, ndax diine ji leen boole, ak ngir ne mooy seen ball-luaayu baat bu njekk bi seen baat yu bari daa juge

Lii bëggoon naa la kaa wax ndaxte baat bi man nan kaa sos ci wolof. di naa ko soppi melalsuuf, xam-xamub melalsuuf (science geografique) --Ibou 9 octobre 2007 à 21:58 (UTC)