Aller au contenu

Jëfandikukat:Daarul xayri

Jóge Wikipedia.

Asalaamu halaykum. Ginnaaw nuyoo bu sell boobu.

Kii seen mbokk la, mi ngi tudd Xaadim Gay, dëkk Senegaal; ci fuñ naa Tuubaa Gay, di as ndongo soo xam ne ab jullit la, te di yëngu ci léggeeyal Lislaam. Jàng naa Alquraan ba mokkal, beqi naa, bind naa kaamil, jàng itam xam-xam ba xawa sori, di wax Wolof ak Araab . Sama yitte mooy lima xamakus néew ma fas-yéene cee léggeeyal sama làkk wii di Wolof, bëgg rekk mu gën a jëm ca kanam; moo tax ma ubbi xët wii ci Wikipejaa ngir léggeeyal Wolof.