Sebeer bukki/Ndijji-bopp
Apparence
(Yoonalaat gu jóge Sebeeru bukki)
Sebeer bukki garabu paj la gu bokk ci njabootu Acanthes. Ci waax yu bane yi lay meññ. Asi gu naaje ak Afrig la cosaanoo.
Njariñ
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Dees koy fajoo.
Nataal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]