Lëng
Apparence
(Yoonalaat gu jóge Lëng/ vitex doniana)
Lëng xeetu garab la gu bokk ci njabootu "lamiaceae" ak ci ñoñ "Vitex". Bari na lool ci Afrig gu diggu gi,ca komoor ak ca Rewño. Mbind mii jukki la bu ñeel meññiit mi. Man ngaa bokk ak nit ñi say xalaat ci jagal ko. Meloom day ñuul, peppam dees koy lekk.
Meññeef mi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Meññeef mi, ci nëtëx lay doore, ñor digante mee ba noowàmbar, daal di ñuul te saf suukar. Guddaayu garab gi ci diggante yaar ba yatti meetar lay toll. Afrig la am ak bàmbulaan Endo. Ci dunu Rewño it dees na ko fa fekk.
Turu xam-xam wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Vitex doniana
Tur wi ci yeneeni làkk
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]farañse: prunier noir |
angale: black plum |