Xëtu web wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
EmausBot (waxtaancëru)
m r2.7.2+) (Robot: Modifying bg:Уебстраница
Synthebot (waxtaancëru)
m r2.7.3) (Robot: Removing tt:Веб-бит
Rëdd 63 : Rëdd 63 :
[[tl:Pahinang Web]]
[[tl:Pahinang Web]]
[[tr:Web sayfası]]
[[tr:Web sayfası]]
[[tt:Веб-бит]]
[[uk:Веб-сторінка]]
[[uk:Веб-сторінка]]
[[zh:網頁]]
[[zh:網頁]]

Sumb bu 14 Nowembar 2012 à 10:36

Xëtu web wenn la ci Xëti World Wide Web bi, doon lu ñu sakk ngir ay nemmeekukat man kaa yër ci ndimbalu ab joowukaay. Aw xëtu web day am ab màkkaanu web bu muy àndal ngir ñu man kaa ubbi ci joowukaay bi. Ci jëmmam dëgg, Xëtu web, day nekk ab mbooloom ay mbind, ay nataal aki riir, ci gattal lépp lu gisu walla déggu.

Saytuwiin

Fànn yi ñu man a saytoo aw xëtu web bari nañu: man ngaa bind ci banqaasu màkkaan yu joowukaay bi màkkaanu webam, walla nga topp ab lëkkalekaay bu nekkoon ci weneen xët. Li ëpp ci joowukaay yi ñu gën a jëfandikoo dees la koy won cib wonekaayub nosukaay jaare ko cib palanteer bu mu lay tijjil, tax it manees koo móol. Làkkiin wu HTML mooy cëslaay gi ñu sukkandiku ngir sos xëti web yi, ba tax saytu gi man a am ak jumtukaay yu wuute: dayob wonekaay bu ne, móolukaay yi, añs.

Cëslaayi xereñ

Cig xereñ, aw xëtu web dafa cëruwoo ne-ne yu wuute yi ne ci World Wide Web bi. Ci lu daj ne-ne bi ci njëkk ab jukki bu ñu bind ci làkkiinu xibaarfeppal gu HTML. Làkkiin wii di HTML day tax ñu man a sos ay xëti web, jox leen ay màkkaani web, tax itam nu man a melowal xët wi, tëral ni ci ne-ne yi taxawee.