Betsayda wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
ArthurBot (waxtaancëru)
m r2.6.3) (robot Adding: cs:Betsaida
Chmee2 (waxtaancëru)
+ image and commons
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
[[File:Ruins of Bethsaida village in summer 2011 (5).JPG|thumb|Betsayda]]
Ci làkku ibrë \^hdyu-tyb\^; CI làkku yawut la tur wi jóge.
Ci làkku ibrë \^hdyu-tyb\^; CI làkku yawut la tur wi jóge.
Ci angale mooy ''Bethsaida''; Ci faranse mooy ''Bethsaïda''
Ci angale mooy ''Bethsaida''; Ci faranse mooy ''Bethsaïda''
Rëdd 5 : Rëdd 6 :

Man nañu koy jàng ci Injiil ci Mc 11:21; Mk 6:45 8:22; Lu 9:10; 10:13; Yow 1:44; 12:21.
Man nañu koy jàng ci Injiil ci Mc 11:21; Mk 6:45 8:22; Lu 9:10; 10:13; Yow 1:44; 12:21.
{{Commons|Category:Bethsaida}}

[[Wàll:Bereb yi ci Téere Linjiil]]
[[Wàll:Bereb yi ci Téere Linjiil]]

Sumb bu 27 Ut 2011 à 11:32

Betsayda

Ci làkku ibrë \^hdyu-tyb\^; CI làkku yawut la tur wi jóge. Ci angale mooy Bethsaida; Ci faranse mooy Bethsaïda

Dëkk ba ci penku-kawu dexu Galile la woon, sorewul fu dexu Yurdan dugg. Tey jii xamuñu tembe bérab bi. Man na nekk sax amoon na ñaari dëkk yu bokk tur Betsayda. Benn ci penku dexu Yurdan, te benn (mooy Betsayda ci diiwaanu Galile) ci sowu dexu Yurdan.

Man nañu koy jàng ci Injiil ci Mc 11:21; Mk 6:45 8:22; Lu 9:10; 10:13; Yow 1:44; 12:21.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons