Yéesu-kristaa
Apparence
(Yoonalaat gu jóge Isaa)
Yéesu-kristaa mooy ji ëpp solo ci diiney krist. yeesu moo yëut: « Yahweh est salut », kristaa di baatu gerek bi'y tekki ci yëut « ku sell ki »). moom la ñi daw yalla tek ci. Catolig yi, ortodoks yi ak li ëpp ci jàngu ñaxtukat yi dañ ni nit dëgg te di yalla tek ci.