Sunnaay aj

Jóge Wikipedia.
(Yoonalaat gu jóge Ay Sunnaam)
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

SUNNAY AJ

Sunnay aj fukk ak ñaar la :am na ci ñeent yoy ñi ngi ame ca armal ga,1 sangu gu jokkook armal gi 2 rafle ci lunu ñaw 3 solub ñëkk akug làmbaay aki dàll 4 labbayka.

Tawaaf gi am ñeenti sunna : 1 dox gi 2 fóon gi doj wa ci loxo walla gimiñ 3 ñukk gi ci ñatti yoon yu njëkk yi 4 ñaan gi ngay ñaan ci tawaaf bi.

Dox gi safaak marwa it am ñeenti sunnaam : 1 foon doj wi bu dee daa juge ca jàkka ja jem safaa 2 ag yéegam diggante safaa ak marwa 3 gaaw gi niy def ci batnu masiil 4 ñaan gu amulub àpp gi ngay def ci kaw safaa ak marwa.