Aller au contenu

Njabootug lepton

Jóge Wikipedia.

Njabootug lepton yi mi ngi ame ci Elektron yi, Muon yi, Tauon yi, neutrinos yu boppam yi ak seeni safaan-yaram (antiparticule). Baatub « lepton » mi ngi bawoo ci baatub Geres biy tekki « lu woyof » biy jublu ci wf gi doyodig jóor (faible masse) gu lepton bi ñu njëkk a wuññi, Elektron bi, bu ñu leen nattee ci nukleon yi ( nucléons).