Ndimbal ci ay nataal

Jóge Wikipedia.

(Yoonalaat gu jóge Ndimbël ci ay nataal)
Dem : Joowiin, Seet

ngir bindu bu yees walla duggu ci sam saq xoolal ndimbël lii nu def ci ay nataal ngir mu gën a jumb ci gan ñi

  • fi gay cokk(clic) ngir dugg mba bindu
    Ndimbël01.jpg

  • ni gay def ba dugg ci sam sàq, fi gay cokk ngir bindu
    Ndimbël02.jpg

  • ni gay def ba sos am saq
    Ndimbël03.jpg

man ga cee dugal sa loxo ngir mu yemb ndax lii di na tax mu gën a yomb ci gan ñi ndax jàgum bind(lire text) mi yombul ci ñépp.