Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar
' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.
Démb
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Léewópóol Sedaar Seŋoor moo amal tegum xeer bu jënk ci wàllum taxawaay iniwersite wi ci 14 sãwiye 1975.
Taxawaayam mu ngi aju ci sart Royuwaay:N° bu 2 sãwiye 1990, iniwersite wu Ndar mu ngi teeru limu ndongo wu njënk (600)ci 17 Desàmbar 1990 ci yoonu négandi.
Mu ngi jot gëddam ci ndogalu Royuwaay:N° bu 10 sulet 1996 ak tur bu bees jóge ci ndogalu Royuwaay:N° bu 4 desàmbar 1996.
Ku ñu ko duppe Gaston Berger, nekk na ab kàngam ci wàllum xeltu, di doomu Senegaal ak Farãs, juddo Ndar-Géej. Di baayu Maurice Béjart.
Ràññeefi barab
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Diggànte iniwersite ak Ndar toll na ci fukki (10) km. Boo jóge Risaartool jëmsi Ndar di nga séen wërngalu kàggu gu mag bi. Iniwersite dafa fekk boole ñaari dëkk : Sanaar Pël ak Sanaar Wolof. Loolu tax na ndongo yi di ko woowe yenn saay Sanaar. Itam kërub internetu ndogo daara yi« https://web.archive.org/web/20080419061846/http://www.sunusanar.com/ » la ñu ko tudde.
Bërëbu tàggat ak gëstu
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Iniwersite bu Ndar ëmb na juróorum-ñaari Bërëbu tàggat ak gëstu :
- Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
- Xam-xamu jëmale ak xarala
- Xam-xamu yoon ak politig
- Xam-xamu koom-koom ak
- Xam-xamu wérgu-yaram
- Xam-xamu mbay, sàmm, nàpp ak xarala yu màcc ci wàllum dund
- Caada, diine, taaral ak jokkoo
- Diiru njàng mi di na toll ci fukki weer. Di tàmbalee oktoobar jàpp sulet. Waaye ubbite njagale mi ak njeextal mi ngi aju ci barabu tàggat ak gëstu bu nekk.
Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Barabu tàggat ak gëstu ci ladab ak xam-xamu nekkinu doomu aadama ëmb juróomu bàqasu:
- Angale,
- Farãse
- Làkk nasaraan jëmale,
- Xam-xamu melosuuf,
- Xam-xamu nekkinu àskan yi.
Xam-xamu jëmale ak xarala
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Barabu tàggat ak gëstu ci xam-xam jëmale ak xaraala ëmb na bàqasu xayma jëmale, bànqaas informatig, bànqaas bitil jëmale ak tàggat ci wàllum xéy.
Mën a dugg
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu xayma jëmale
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu bitil jëmale
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu informatig
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Xam-xamu yoon ak politig
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Barabu tàggat ak gëstu xam-xamu yoon ak politik ëmb na ñett bàqaas:
- Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi ;
- Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris ;
- Bànqaasu xam-xamu politig.
Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]bànqaasu xam-xamu politig
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mën a dugg
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Xam-xamu koom-koom ak doxalin
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Kërug internet [1]
Caada, diine, taaral ak jokkoo
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Kërug internet [2] Barabu tàggat ak gëstu caada, diine, taaral, ak jokkoo ëmb na juróom benn bàqasu :
- Bànqaasu jokkoo,
- bànqaasu infogarafi,
- Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada,
- Bànqaasu làkk ak caada Agrig,
- Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
- Bànqaasu Xam-xamu diine.
bànqaasu jokkoo

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]tërëlin
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mujjàntal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu infogarafi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu làkk ak caaday Afrig
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mujjàntal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Màndargal

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Wàllum gëstu
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]nekkinu ndongo daara yi (CROUS)
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Yokkute lim ndongo yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
SAT | SEG | SJP | LSH | TOTAL UGB | |
---|---|---|---|---|---|
2001/2002 | 400 | 280 | 499 | 1480 | 2659 |
2002/2003 | 475 | 325 | 535 | 1525 | 2860 |
2003/2004 | 559 | 349 | 575 | 1506 | 2989 |
2004/2005 | 671 | 396 | 505 | 1799 | 3371 |
2005/2006 | 726 | 415 | 688 | 1965 | 3794 |
2006/2007 | 727 | 641 | 932 | 2143 | 4443 |
Dëkkuwaay
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]-
Campus 2
-
Village B
-
Village E
-
Village F
-
Village H
-
Village H bis
-
Village L
-
Village L (Bis)
Loyer mensuel tout compris pour les nationaux | Loyer tout compris en frCFA pour les étrangers | |
---|---|---|
Villages A,B,C,D,E,F,K,M | 3000 (4,57 euros) | ??? |
Villages H,I,J,L | 4000 (6,09 euros) | ??? |
Dem beek dikk bi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Tektal yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- ↑ "Archived copy". Archived from the original on 2016-03-03. Retrieved 2015-12-21.
- ↑ http://www.ugb.sn/crac/
Xool yeneen
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Téere ak mbóotu tektal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Dossier sur l'UGB dans un numéro spécial sur l'enseignement supérieur au Sénégal, Le Soleil, janvier 2008, Royuwaay:P.5-6
Cosaan
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- https://web.archive.org/web/20121110200513/http://www.gouv.sn/Decret-no-2012-1163-du-29-octobre.html
mbóotu tektal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Musée du Centre de Recherches et de Documentation du Sénégal à Saint-Louis
- Université Cheikh-Anta-Diop
- Éducation au Sénégal
- Felwine Sarr
mbóotu biti
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Site officiel
- Présentation et images sur le site du Campus numérique francophone de Saint-Louis
- Site des étudiants de Sanar
- Fiche de l'UGB sur le portail SenCampus
- [https ://fr.glosbe.com]
Royuwaay:Portail Royuwaay:Infobox Université ' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.

- Bànqaasu làkk ak caaday Afrig,
- Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
- Bànqaasu Xam-xamu diine.
bànqaasu jokkoo
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mën a dugg
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]tërëlin
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mujjàntal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu infogarafi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mujjàntal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mën a dugg
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu làkk ak caaday Afrig
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mujjàntal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Màndargal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mën a dugg
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Wàllum gëstu
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]nekkinu ndongo daara yi (CROUS)
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]yokkute lim ndongo yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]thumb|350px|Évolution des effectifs de l'UGB entre 2001 et 2007

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]L'université Gaston Berger est composée d'unités de formation et de recherche (UFR équivalent des facultés). Il y en a huit au total :
- Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
- Xam-xamu jëmale ak xarala
- Xam-xamu yoon ak politig
- Xam-xamu koom-koom ak
- Xam-xamu wérgu-yaram
- Xam-xamu mbay, sàmm, nàpp ak xarala yu màcc ci wàllum dund
- Caada, diine, taaral ak jokkoo
- Diiru njàng mi di na toll ci fukki weer. Di tàmbalee oktoobar jàpp sulet. Waaye ubbite njagale mi ak njeextal mi ngi aju ci barabu tàggat ak gëstu bu nekk.
Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Barabu tàggat ak gëstu ci ladab ak xam-xamu nekkinu doomu aadama ëmb juróomu bàqasu:
- Angale,
- Farãse
- Làkk nasaraan jëmale,
- Xam-xamu melosuuf,
- Xam-xamu nekkinu àskan yi.
Xam-xamu jëmale ak xarala
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Barabu tàggat ak gëstu ci xam-xam jëmale ak xaraala ëmb na bàqasu xayma jëmale, bànqaas informatig, bànqaas bitil jëmale ak tàggat ci wàllum xéy.
Mën a dugg
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu xayma jëmale
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu bitil jëmale
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu informatig
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Xam-xamu yoon ak politig
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Barabu tàggat ak gëstu xam-xamu yoon ak politik ëmb na ñett bàqaas:
- Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi ;
- Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris ;
- Bànqaasu xam-xamu politig.
Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]bànqaasu xam-xamu politig
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mën a dugg
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Xam-xamu koom-koom ak doxalin
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Kërug internet [1]
Caada, diine, taaral ak jokkoo
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Kërug internet [2] Barabu tàggat ak gëstu caada, diine, taaral, ak jokkoo ëmb na juróom benn bàqasu :
- Bànqaasu jokkoo,
- bànqaasu infogarafi,
- Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada,
- Bànqaasu làkk ak caada Agrig,
- Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
- Bànqaasu Xam-xamu diine.
bànqaasu jokkoo
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mën a dugg
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]tërëlin
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mujjàntal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu infogarafi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mujjàntal
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mën a dugg
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Bànqaasu làkk ak caada Agrig