Xeetu xarañteg xelu masin ci wàllu soldaar
Royuwaay:TraductionRoyuwaay:Traduction
Xarañteg xelu masin (IA) barina luñu koy jëfandikoo ci xare, lu ci melni jokkoo, xarañteg xelu masin, ak doxal munisioŋ yi . Xeex bu algorithm wala bu xarañteg xelu masin di doxal, te nit ñi duñu jël benn dogal, ñu koy woowe xare bu mag, ab baat bu Amir Husain ak John R. Allen sos ngir boole ci preposisioŋ ak prefix hyper ( ὑπέρ, 'beyond') ak " xare " ci làkku angale . Rëyaayu IA bi mën na demal boppam, mën na yokk gaawaayu xare bi ci lu gaaw, rawatina sudee lu ëppu benn pàcc moo wéeru ci IA bi. [1] IA yamul ci gànnaay yu bees yu melni drone wala cyberwar, mën na indi jafe-jafe ci bépp xeetu pexe soldaar. [1]
Jëfandikoo
[Soppi | soppi gongikuwaay bi]IA mën na yokk komand ak njiit, jokkoo, kaptër, boole ak jëflante. [2] Xaralay IA yi dañuy may ñu mëna déggoo ci diggante kaptër yi ak efektër yi, gis ak ràññee fitna, màrki position noon yi, am target, boole ak deconfliction ci diggante Joint Fires yuñ séddale ci diggante oto xeex yuñ boole, nit ñi di doxal ak yiy demal seen bopp . [2]
Jëfandikoo nañu IA ci ay xare ci Irak, Siri, Ukraine, Iran ak Israël . Benn sistem buy xaaj ay mbir ci radar, di jëfandikoo ay kaptër ak ay algorithm ngir xàmmee ak xaaj ci saasi ay mbir ci radar, Armée indienne moo ko patente ci 2025. Dafay gaaw te leer ci méngale ay done ci jamono dëgg - lu melni ay nataal wala siñaal radar. Mën nañu ko jëfandikoo ci mbir yuñ mëna jefandikoo benn yoon kese, lu ci melni misil yuy njiit.
Dron soldaar yi mëna demal seen bopp ñu ngi leen di jëfandikoo bu baax. [ <span title="The geographic scope near this tag is ambiguous. (July 2025)">fan?</span> ]
Komànd ak doxal
[Soppi | soppi gongikuwaay bi]Ci atum 2024, benn labo bu waa Chine ci Joint Operations College bu Daara bu kawe bu Kaaraange Nasonaal ci Shijiazhuang sosna benn komandan soldaar bu juntuwaay yu bees yi ngir jëfandikoo ko ci ay simulaasioŋu xeex yu magg ci cër bu komandaa bi jiite .
Ci atum 2024, larme bu Ukraine defar na drone Kamikaze buy demal boppam ngir moytu Risi di dugg ci naaw gi.
Ci jamonoy xeex bi dox diggante Inde ak Pakistan ci atum 2025, dañu jox soldaari Inde sistemu rapoor meteoroloji bu ànd ak IA ( Projet Anumaan ) ay done IMD ngir jàppale sistemu komando ak kontrôlu xeex artillerie ci waajal ak teg ay mbir ci anam wu jaar yoon. Lu tollu ci 200 kilometres (120 miles) ci biir fronceeru Pakistan, sistem bi mën na wax luy gaawaayu ngelaw li ak yeneen anam yu meteo bi di doxee 48 ba 72 waxtu ci kanamu jot gi. IA jàppale na itam ci xayma fi misil yi di jaar fu sori.
Xarañteg soldaar
[Soppi | soppi gongikuwaay bi]Ci atum 2023, Departamaa bu Kaaraange bu Etats Unis dafa natt juntuwaay yu bees yu lalu ci xeetu lakk yu yaatu ngir numériser ak boole ay done ci biir soldaar yi.
Ci xare bu Gaza, Israel dafa jëfandikoo ñaari sistem IA ngir sos ay target ngir dóor: Habsora (ñu tekki ko: " xebaar bu baax bi ") dañu ko jëfandikoo ngir dajale limu tabax yi ñu wara dóor, ci noonu la "Lavender" defar limu nit ñi. "Lavender" defar na limu 37000 nit ñuñ wara xëcc. [3] Limu tabax yiñ wara xëcc bokk na ci këri nit ñi ñu yaakaar ni bokk nañu ci waa Hamas ci Gaza. Njaxasu xaralay juntuwaay yu bees yi ak coppite politik ci moytu siwil yi moo jur limu siwil yu dee yu musul am. Ofisiye yu IDF neena ñu prograam bi dafay wax ci jafe-jafe bi njëkkoon ci forsu aérien bi ñàkk ay target. Jëfandikoo Habsora, ofisiye yi neenañu ni ñi ñu ñakka woolu ak ay këru ndawu Hamas ñungi yaatal bu baax "banku juntuwaay yu bees yi." Benn yeglekaay ci biir dafa wax ni mbir yi dañu melni "usine buy faat ñu bari".
Ci atum 2024, soldaari Etats Unis dañu tàggat xarañteg xelu masin ngir xàmmee fi ñuy song ci jawwu ji ci jamonoy operaasioŋ yi ñuy amal ci Irak ak Siri.
Ci xeex bi dox diggante Inde ak Pakistan ci atum 2025, larme Inde dafa jëfandikoo IA ngir sos nataalu liggéey buñ bokk, jàngat xarañteg xam-xam, jàngat fitna, ak sos xeetu xam-xam ngir song yu sori. Defar nañu ñaar fukki ak ñetti aplikaasioŋ ngir ay anam yu wuute yu yor ay done ak ay done ngir boole ay kaptër yu bari ak ay balluwaay yu bari ci jamono dëgg. Aplikaasioŋ yi bokkuna ci sistemu Collation ak Analysis Intelligence Electronic, biñ boole ak Projet Sanjay ngir joxe nataalu liggéey buñ bokk ngir gëna mëna déggoo, xam anam wi mbir yi di demee, ak gëna am dogal, ak sistem Trinetra, bi ñu jëfandikoo ngir xàmmee ak njëkka teg fitna yu mag yi ngir mëna def pexe yu am solo. Meteo bi IA jàppale, may na ñu mëna waajal bu baax ak di xool ay jumtukaayi artileri ak ay vecteur yu sori. Xeetu IA bu toolu xare bi deñ kaa jox 26 att ci ay done yuñ enregistre ak archive siif yu forsu arme bu pakistaan ak emisoŋu radio. Loolu dafay wane ban soldaar ci Pakistan moo yor jumtukaay bu nekk ak fumu ko njëkka jëfandikoo. boole feed yu bawoo ci kaptër yi, drone yi, radar yi ak satelit yi taxna ñu mëna dajale ay done ci jamono dëgg. Done yépp, boole ci leeral ci barabi noon yi, jumtukaay yi, ak jumtukaay yi, dañu leen boole daal di koy jox komandanti soldaar yi ngir ñu jël matuwaay yi war.
Tendensi àdduna bi
[Soppi | soppi gongikuwaay bi]Réew yu bari ñu ngi gëstu ak dugal ay aplikaasioŋu soldaar ci IA, ci lu ñuy woowe " kursu gànnaayu xarañteg xelu masin ". Gëstu bi am ci jamono ji mingi sëssé ci dajale ak jàngat ay xibaar, logistik, liggéey ci siber, liggéey ci joxe xibaar, ak oto yuy demal seen bopp ak yuy demal seen bopp . [4]
Ci àdduna bi xaalis bi soldaar yi di dugal ci robotik yokk na joge ci [ ] ciy dolaar ci 2010 yegg ci 7,5 milyaar ci
Ci weeru nowàmbar 2023, Persida bu Amerig Kamala Harris gennena ap kominike bu 31 rëëw siñe ngir defar ay garde ngir soldaar yi jëfandikoo juntuwaay yu bees yi. Anngaasmaa yi bokkuna ci jëfandikoo ay xoolaat yu yoon ngir xam ndax juntuwaay yu bees yi soldaar yi ñungi topp yooni bittim réew, ak nekk ku moytu ak leer ci yokkuteg xarala yii.
Gëstukat yu bari ci juntuwaay yu bees yi deñuy jeema moytu aplikaasioŋu soldaar yi, ak ay garde ngir moytu aplikaasioŋu soldaar yi duggu ci xeetu lakk yu magg yi. [2]
Ci cosaan ak aada
[Soppi | soppi gongikuwaay bi]
Sistemu xarañteg xelu masin bu soldaar yi feeñ nañu ci téere fiksioŋ yu bari, lu ci bari nekk ay noon .
Filim
[Soppi | soppi gongikuwaay bi]- Terminator
- Franchise Matrix bi
Linu joxe jox
[Soppi | soppi gongikuwaay bi]- Brian Herbert moo ko bind
Royuwaay
[Soppi | soppi gongikuwaay bi]Tekki royuwaay yi nekk ci xëtu Wikipedia bi mënul a am ndax fi ñu ko jëlee ci tubaab la te benn ci wolof amul.
Soo bëggee gis dokimaa yu njëkk yi ci Àngle, lii mooy royuwaay yiñ jëfandikoo ci xët wiñ ko jële
1. "Hyperwar - New challenges for army development". European Security & Technology.
2. Stefan Krempl (November 5, 2020). "Machine Warfare: From Drone Swarm to Hyperwar".
3. Husain, Amir; Allen, John R.; Work, Robert O.; Cole, August; Scharre, Paul; Anderson, Wendy R.; Porter, Bruce; Townsend, Jim (2018). Hyperwar: conflict and competition in the AI century. Austin, Texas. ISBN 978-1-7325970-0-6. OCLC 1099536594.
4. Allen, John; West, Darrell; Institution, Brookings (July 12, 2020). "Op-ed: Hyperwar is coming. America needs to bring AI into the fight to win - with caution". CNBC. Retrieved June 22, 2022.
5. Slyusar, Vadym (2019). "Artificial intelligence as the basis of future control networks" (Preprint). doi:10.13140/RG.2.2.30247.50087. Retrieved July 6, 2025.
6. Congressional Research Service (2019). Artificial Intelligence and National Security (PDF). Washington, DC: Congressional Research Service.
7. Iraqi, Amjad (April 3, 2024). "Lavender: The AI machine directing Israel's bombing spree in Gaza". +972 Magazine. Retrieved April 6, 2024.
8. Marti, J Werner (August 10, 2024). "Drohnen haben den Krieg in der Ukraine revolutioniert, doch sie sind empfindlich auf Störsender – deshalb sollen sie jetzt autonom operieren" [Drones have revolutionized the war in Ukraine, but they are sensitive to disruptive transmitters – therefore they are now supposed to operate autonomously]. Neue Zürcher Zeitung (in German). Retrieved August 10, 2024.
9. Frankel, Julia; Mednick, Sam (June 17, 2025). "How Israel used spies, smuggled drones and AI to stun and hobble Iran". The Independent. Retrieved June 17, 2025.
10. Kumar, Anish (September 11, 2025). "Indian Army's AI Innovation Boosts Target Detection, Secures Patent". Asianet Newsable. Retrieved October 11, 2025.
11. Mani, Sudarsanan (September 11, 2025). "Indian Army secures patent for AI-based Automatic Target Classifying System". CNBC TV18. Retrieved October 11, 2025.
12. Allen, Gregory (February 6, 2019). "Understanding China's AI Strategy". Center for a New American Security. Archived from the original on March 17, 2019. Retrieved March 17, 2019.
13. Chen, Stephen (June 16, 2024). "Chinese scientists create AI military commander to run virtual war games". South China Morning Post. Retrieved July 6, 2025.
14. Philip, Sneheesh Alex (October 7, 2025). "Op Sindoor is India's first AI-enabled operation. How 'heavy use' of modern tech by Army played out". ThePrint. Retrieved October 7, 2025.
15. Ray, Kalyan (October 7, 2025). "Wars of tomorrow will be fought with algorithms: Rajnath Singh urges focus on cutting-edge tech". Deccan Herald. Retrieved October 9, 2025.
16. Kumar, Bhaswar (October 6, 2025). "AI widely used in Op Sindoor, military LLM to be ready in 6 months: Army". Business Standard. Retrieved October 9, 2025.
17. Kumar, Anish (October 6, 2025). "How AI Helped the Indian Army Achieve Over 94% Accuracy in Operation Sindoor". Asianet Newsable. Retrieved October 9, 2025.
18. Manson, Katrina (July 5, 2023). "The US Military Is Taking Generative AI Out for a Spin". Bloomberg.com. RAND Corporation. Retrieved July 6, 2025.
19. Davies, Harry; McKernan, Bethan; Sabbagh, Dan (December 1, 2023). "The Gospel: how Israel uses AI to select bombing targets in Gaza". The Guardian. Retrieved December 4, 2023.
20. MEE Staff (November 30, 2023). "Israeli army relaxed rules for bombing Gaza". Middle East Eye. Retrieved December 4, 2023.
21. Quach, Katyanne (February 27, 2024). "US military pulls the trigger, uses AI to target air strikes". The Register. Retrieved August 6, 2024.
22. Pandit, Rajat (October 7, 2025). "Army used AI in a 'big way' during Operation Sindoor". The Times of India. ISSN 0971-8257. Retrieved October 8, 2025.
23. Banerjee, Ajay (October 6, 2025). "AI enables 94 per cent accuracy in targeting enemy assets: Indian Army". The Tribune. Retrieved October 8, 2025.
24. "Getting to grips with military robotics". The Economist. January 25, 2018. Archived from the original on June 4, 2025. Retrieved February 7, 2018.
25. "Autonomous Systems: Infographic". Siemens. April 20, 2016. Archived from the original on August 18, 2018. Retrieved July 6, 2025.
26. Knight, Will. "The US and 30 Other Nations Agree to Set Guardrails for Military AI". Wired. ISSN 1059-1028. Archived from the original on September 20, 2024. Retrieved January 24, 2024.
- 1 2 Njuumteg royuwaay: Balise
<ref>incorrecte : aucun texte n’a été fourni pour les références nomméesAllen West 2020 - 1 2 3 (Report). Vadym Slyusar. Check date values in:
|date=(help); Missing or empty|title=(help) Njuumteg royuwaay: Balise<ref>incorrecte : le nom « Slyusar-2019 » est défini plusieurs fois avec des contenus différents. - ↑ Njuumteg royuwaay: Balise
<ref>incorrecte : aucun texte n’a été fourni pour les références nomméesDavies-2023 - ↑ Njuumteg royuwaay: Balise
<ref>incorrecte : aucun texte n’a été fourni pour les références nomméesCRS-2019