Waxtaan:Xayma

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wikipedia.


Partie théorique

Saar 1 - kàttanug lim yu lëmb yi. A. Ngóora yi 1) Baataan Lëf lii di aⁿ ben kàttan la gog a mooy jën wi, n mooy ngóora ngi.

2)Reegalu siiñ yu ngóora

Bépp kàttanub lim bu baax (+),lim bu baax (+)lay doon. Niiral: 3³ = 27 3⁴ = 81 Bépp kàttanub lim bu tòlloodi(paire),lim bu baax lay doon(+) Niiral: (– 2)⁴ = 16 (– 2)² = 4 Bépp kàttanub lim bu bon(-) bu tóol(impaire),lim bu bon(-) lay doon. Niiral : (– 2)³ = – 8 (– 2)⁵ = – 32

Ci gàttal : ag kàttan dafay nekk lim bu bon(-) si kaw rekk jën wi bon(-) kàttan gi tam tóol.


B. Propriétés des puissances à exposants naturels 1) fullug kàttan yi.

Ngir Ful ay kàttan yu bokk ben jën, dañuy tëyye jën wi Yokklante kàttan yi

Niiral: 3³× 3² = 3³+² = 3⁵ (– 2)² × (– 2)⁴ = (– 2)²+⁴ = (– 2)⁶


2) kàttanug kàttan

Ngir yékkati ag kàttan ci geneenug kàttan, dañuy tëyye jën wi fullante kàttan yi.


Niiral : (5²)³ = 5²*³ = 5⁶ [(– 2)2]4 = (– 2)2.4 = (– 2)8


3) kàttanug ful

Ngir yékkati ab fulub këmka ci ag kàttan,këmka gune dan koy yekkati ci kàttan Ngoo gu.


Niiral : (2 . 5)³ = 2³ . 5³ (– 3 . 2)⁴ = (– 3)⁴ . 2⁴


C. Kàttanu 10 1) Notation


n ben lim bu ndénu la:



Niiral :

2) Lenn ci ay jëkkaan yu am solo.

Jëkkaan Njunj 10ⁿ Niiral pic p 10-12 1 pm = 10-12 m nano n 10-9 1 nm = 10-9 m micro 10-6 milli m 10-3 1 mm = 10-3 m centi c 10-2 1 cm = 10-2 m déci d 10-1 1 dm = 10-1 m déca da 101 1 dam = 101 m hecto h 102 1 hm = 102 m kilo k 103 1 km = 103 m méga M 106 1 Mm = 106 m giga G 109 1 Gm = 109 m téra T 1012 1 Tm = 1012 m

D. Notation scientifique d'un nombre Tout nombre décimal peut s'écrire de différentes façons à l'aide d'un produit d'un nombre et d'une puissance de 10 à exposant entier. Niiral : 2930,6 man ko bindee 29 306 . 10-¹ walla 293,06 . 10¹ Walla 29,306 . 10² Walla 2,930 6 . 10³

............... Un nombre en notation scientifique s'écrit sous la forme d'un produit du type : a . 10ⁿ dans lequel a est nombre décimal tel que Niiral : l'écriture scientifique de 2930,6 est 2,9306 . 10³


Seenug ceetlu lu nu sàkku la!