Wéyal

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

wéyal mooy ponk bi xaw a ëpp solo ci ñatti ponk yooyu, ndax moom njiitul réew mee koy ame, walla jëwrin ju njëkk ji bu dee nosteg péncu réew (regime parlamentaire), mooy doxal réew mi di tënku ci yoon yi bàyyikoo ci dooley yoonal ji, bu ko defee yoon di ko fuglu (controler)