Aller au contenu

Tamsir Juuf Aviance

Jóge Wikipedia.

Tamsir Juuf Aviance wala Tamsir Aviance (ne. Tamsier Joof, judd 17 mee 1973),[1][2][3][4] ñu xamewoon ko ci tur wi tuddu Tam Jo,[3] feccikat la, koreograaf, aktër, mannekin, liggéeykat, surnalist ci radio, ak bindkat. Ñu tuddee ko "Aviance" ginaaw bimu duggee ci "House of Aviance", di benn ci këri vogue-ball yi gëna mag ci Etats Unis. Ginaaw bimu feeñee ci musical yu bari, ak nekk feccikatu Mary Kiani, Take That ak Janet Jackson,[5][3][6] ñu xamoon ko itam ci feccikatu Londres ci ati 1990 te bokk na ci feccikatu vogue yu Londres ci jamono jooju.[7][8]

Dundu gu njëkk ak njàng

[Soppi | soppi gongikuwaay bi]

Tamsir mingi juddoo Kensal Rise ci gannaaru sowwu Londres ci biir njaboot gu waa Senegaal ak waa Gambie.[3] Pàppaam faatu, avocat la woon ci Gambie,[9] yaayam jigéen liggéeykat la woon.[3]

Tamsir moo sos Centre de ressources seereer ak radio seereer. Ci xeet Seereer la bokk. Tamsir ab jaamukat la bu gëm diine Seereer (A ƭat Roog).[10][11]

  1. 2002: Dirty Pretty Things (nit ku am xel / ki nekk ci aéroport bi)
  2. 2003: Lara Croft: Tomb Raider – The Cradle of Life (Reservation de kostum)
  3. 2003: Love Actually (Audience bu ñuul etnik)
  4. 2015: FKA Twigs' Glass & Patron (Feccikat, widewo misik)
  5. 2024: Wicked (xaaj 1) - (Ozian - Feccikat bu Emerald City ak boroom salon)
  6. 2025: Wicked: For Good (xaaj 2) - (Feccikat Ozian)
  7. 2026: Eloise (filmu Netflix, Amy Sherman-Palladino moo ko realise, Ryan Reynolds moo ko jiite) - (Fecckat)
  1. "FKA twigs - Glass & Patron (Official Music Video YTMAs)"
  2. Wonderland Magazine: "NIGHT CRAWLING 004: REALNESS KIKI VOGUE BALL"
  3. 1 2 3 4 5 "Senegambian taking the dance world by storm", West Africa, 5 June 1995, p. 4.
  4. The Comet newspaper (Stevenage) interview : "This is it", 23 August 2001, p. 21.
  5. London Metro : Review of "Consecrated Love" (and interview of choreographers) - 7 August 1999, p. 57.
  6. Bell, Max (10 April 2012). "The Wiz". The Standard. Retrieved 5 August 2025.
  7. The Face, July Issue, 1991, p. 10.
  8. Bizarre, April 1997, p. 15.
  9. William Dixon Colley, "Champion of free speech (Tribute)", The Nation (Gambia), 7 June 1993.
  10. "About Us" Archived, the Wayback Machine, Seereer Resource Centre's website, and "The Team" Archived, Wayback Machine
  11. Open Mike : Prejudice against Seereer religion (A ƭat Roog) and other Traditional African religions in Senegambia and other parts of Africa (Alarba, 8 fewriye 2017) Archived - Wayback Machine
  • Tamsier Joof Aviance ci IMDb