Aller au contenu

Soxna Kumba Jama jiite.

Jóge Wikipedia.

Soxna Kumba Jama jiite, mooy doomi Soxna Jale Kanji ak Sëriñ Ngaay Góoram, Soxna Kumba Jama jiite ak Soxna Caane Jiite, ak Soxna Maram Géy Jiite, ak Soxna Aram Paate Jiite, ak Soxna Faatu Jiite, ak Soxna Mati Jiite, ñoom ñii ñoo bokk nday ak baay.[1]

Soxna Kumba Jama jiite mi ngi jóge woon Ngaay Mexe, ñu joxoon ko Sërñ Maxraar Gay. Ag njabootam moo di Sëriñ Abdu Kariim Gay , ak Sëriñ Mbay Kumba, ak Sëriñ Omar Gay, ak Sëriñ Ibraahima Gay, ak Soxna Buso Kumba Gay, ak Soxna Maam Njaay Sàll Gay

Soxna Kumba Jama jiite bokk na ci soxna yi fi Sëriñ Maxtaar Gay bàyyi ginnaawam. Soxna Kumba Jama jiite mi ngi faatu bisub Dibéer waxtuw timis ci atum 1960 ñu deñc ko Daarur Gay.

  1. SOXNA KUMBA JAMA JIITE