Skelmersdaal
Apparence
Skelmersdaal ab dëkk la ci sowwu Lancashire, Nguur-Yu-Bennoo. Mingi toog ci wetu dexu Tawd. Mingi sori 33 miles ci Bolton, 15 miles ci Liverpool ak 2804 miles ci Senegaal. Nit ñu bari ñu bawoo Liverpool toxu nañu ci Skelmersdaal, rawatina ci ñaareelu guerre mondiale. Skelmersdaal amna barabu jaaykaay bu tuddu Concourse, muy diggu dëkk bi.