Aller au contenu

Sëriñ Mbay Kumb

Jóge Wikipedia.

Sëriñ Baabakar Gay ñu koy wax ( Sëriñ Mbaye Kumba) Mooy doomi Sëriñ Maxtaar Gay ak Soxna Kumba Jama jiite Daaru Gay. Mi ngi juddu ci atum 1900 mooy ñaareelu doom ci Soxna Kumba Jama jiite, Sëriñ Mbay Kumba mi ngi faatu bisub Altine waxtuw yoor-yoor weeru Diggiw tabaski ci atum 1976 ñu deñc ko Daarurl Muhti. Sëriñ Mbay Kumba ag njabootam mooy Sëriñ Abdu Mbàkke Gay. Sëriñ Màndumbe Gay, Soxna Nogay Gay ñii ñoo bokk nday ak baay. Séen Waajur bu jigéen mooy Soxna Xujja Say Saar.