Sëriñ Maxtaar Gay ag njabootam
Apparence
Sëriñ Maxtaar Gay ay Soxnaam
( 1) Soxna Jóob ñu koy wax Soxna Njóoba Jóob.
( 3 ) Soxna Faati Mbaala Ndóoy.
( 4 ) Soxna Kumba Jama jiite.
( 5 ) Soxna Faatu Jóob.
( 6 ) Soxna Sukkay Sàmb.
( 7 ) Soxna Jeŋ Suraŋ.
( 8 ) Soxna Aminata Sëy.
( 9 ) Soxna Awa Penda Jóob.