Aller au contenu

Sëriñ Abdu Mbàkke Gay.

Jóge Wikipedia.

Sëriñ Abdu Mbàkke Gay Mooy taawub Sëriñ Mbay Kumba Gay ak Soxna Xujja Say Saar. Mi ngi gane Àddina ci atum 1927 Daaru Gay,ñu tudde ko Sëriñ Abdu Rahmaan Mbàkke mum boroom Daaru Muhti. Mooy juróom benneelu Xalifa Maamam Sëriñ Maxtaar Gay Daaru Gay ci atum 2013 Sëriñ Abdu Kariim Gay moo ko yar moo ko jàngal Alxuraan ak xam-xam.