Aller au contenu

SËRIÑ MAXTAAR GAY AY SOXNAAM :

Jóge Wikipedia.

Ay Soxnaam

. 1 Soxna Jóob ñu koy wax Soxna. Njóoba Jóob.

. 2 Soxna Lobe Kebe.

. 3 Soxna Faati Mbaala Ndóoy.

. 4 Soxna Kumba Jama jiite.

. 5 Soxna Faatu Jóob.

. 6 Soxna Sukkay Sàmb.

. 7 Soxna Jéŋ Suraŋ.

.8 Soxna Aminata Sëy.

.9 Soxna Awa Penda Jóob.