Aller au contenu

SËRIÑ MAXTAAR GAY AB JUDDOOM:

Jóge Wikipedia.

Sëriñ Maxtaar Gay. Mi ngi juddóo dëkk bu ñuy wax Jamooy Gay, ca njàmbur, ginaaw bi mu ñëw Kajoor ci dëkk bu ñuy wax ( Ngay Ngay Làkk) ñu gën koo xam ci ( Ngay Ngay Asan) di dëkkub Maamam Sëriñ Asan Gay. [1]



SËRIÑ MAXTAAR GAY DAARU GAY :

Ay Soxnaam :

. 1 Soxna Jóob ñu koy wax Soxna. Njóoba Jóob.

. 2 Soxna Lobe Kebe.

. 3 Soxna Faati Mbaala Ndóoy.

. 4 Soxna Kumba Jama jiite.

. 5 Soxna Faatu Jóob.

. 6 Soxna Sukkay Sàmb.

. 7 Soxna Jéŋ Suraŋ.

.8 Soxna Aminata Sëy.

.9 Soxna Awa Penda Jóob.

  1. Sëriñ Maxtaar Gay