Njéeréer

Jóge Wikipedia.
Njéeréer yuy séey

Njéeréer yii, sii toflin gunoor yi dundée ganciax, lanu bokk, bokkat sii toflin Orthoptera, tée nukooy woyé Caelifera. Ci séen jefiin lan léén di ranée, yii njéeréer yunuy waw locuste bunuy tolo sii grégariaptes (manaam bunuy tolu ii liime bubaré lunuy woyé grégaire). Ci lanuy nékk gunoor yuy yax gancax. Sii yatu waay yax-yax bunuy déff ci Afrik, yénénn sayi, si boor soow Tugal. Amna tamit,xétu soxunt yuy sen mélocane nuro akk soxunt maag ni aay Criquet pélerin sii bétt Amerique Equatorial, yoo xamantané sénii yax-yax outéna akk njéeréer.

Sen mélocaan (caractéristiques)(Coppiteg)[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Dañi aam ay deg-deg yu gatt té sédéelé ci kaw ba ci suf,sen laaf yu gudu ak yu gaat,té béen bunék,akk façon wayinem.Leg-leg sakh dañléen di diawatlé ak suñu toflin.Dañu rañé ñarr façon njéeréer (Acididae) akk ay njéeréer yu gatt (Tridactilydae). Ci sen biir xéel,amna ay siditt akk aay siditt ci sen biir yu takliko akk yénéen siditt wayé bu nékk akk sa paco( métamère).Xéel njéeréer ci wéet xoor lañ kooy rañé(hyponeurien).Sen dréet dina daaw béep ci sen yaram,manam ci xool-bi be, ci yénénn siditu yaram-bi,waé tamit, fépp ci ruxu-roxanyi sén yaram. Ngéléw buñuy noyé daay