Narab

Jóge Wikipedia.

Narab garab la gog dees koy fekk ci tund sahel ba Sudaan, Senegaal jëm Kamerun ak yenn gox i Afrig yi, garab la gog dafa bëgg suuf su xaw a tooy.

Narab gi


Melo wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Garab la gog day am ay dég sëq lool guddaayam manees na ko natt ci 10 jàpp 20 ci ay met. Yaatuwaayam dees na ko natt ci 80i sàntimet.

Am xasam day leer yor melo wu baam.

Taw yu jëkk yi ci la garab gi tàmbali di am ay xob.

Foytéefam day am ay doom yoy bu demee ba nekk mag, da na man a làmboo ak 5 jàpp 9 ci ay doom.

Njariñam[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Garab la gog dees koy jëfandikoo ni fiime ngir dekkilaat suuf si. Boo demee ci pajum cosaan garab la gog day faj metiitu biir.

Garabu matt la it.

Nataal[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Peer


Wànqaas


Turu xam-xam[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Acacia polyacantha