MediaWiki:Passwordremindertext
Apparence
Kenn(xéj-na yaw la) ku am bii màkkaanu IP $1 moo laaj ngir ñu yónne ko ab baatujàll bu bees ngir duggam ci Wikipedia ($4). Baatujàll bu jëfandikukat bii di « $2 » léegi mooy « $3 ». Di la digal rekk nga duggu te soppi baatujàll bi ci ni mu gën a gaawee. Soo doonul ki biral bii laaj, walla fattaliku nga sa baatujàll bu njëkk ba, te nammatoo kaa soppi, man ngaa tankamlu bii bataaxal te wéy di jëfandikoo baatujàll bu yàgg ba.