Aller au contenu

Xayra

Jóge Wikipedia.
(Yoonalaat gu jóge Kayro)


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Xayra لقاهرة
Skyline of {{{official_name}}}
Réew Isipt
way-dëkk17 856 000 nit
atum way-dëkk2 009
Rëyaay210 km²
Fattaay38 221 nit/km²
Gisub Xayra

Xayra (ci araab لقاهرة Al-Qāhira) mooy péeyu réewum Isipt, mooy dëkk bi ëpp nit ca goxub Afrig. Donte Al-Qāhira mooy tura dëkk waaye, lu bari, dees na ko wax itam, ci araabi waa-isipt, misr di Isipt ci araab.